Madior Ak Dior - Épisode 11 [Saison 01]

[ABONNEZ-VOUS ici] ☆~~👉 it-vision.org/nameof-PikiniProduction
[FACEBOOK]☆~~👉 www.fb.com/PikiniProductions
[TWITTER]☆~~👉twitter.com/PikiniProd
#Madior_ak_Dior_it-vision.org/wow-PL7OYJbvZchhHCAKLYpjgAFrKKzFTYbq3o
WhatsApp ☆~~👉 +221776626858
Pikini Productions
ByBen 2019

Scaricare

visualizzazioni
532,625

Commenti

  • From Nigeria 🇳🇬 👆 ❤️ 👏

    Muhammad AbabuleMuhammad Ababule15 giorni fa
  • Sama khèll moy tèuy souma guissè badianou ma dior ak ndomamm

    Cheikh Fama DiawCheikh Fama DiawMese fa
  • Ana gni beugue Dior Je suis le première Dior J'tm 💯❤️

    Xxx TentacionXxx TentacionMese fa
  • dior dama nèkh mane billay

    Modou DiopModou DiopMese fa
  • ana naturel bi nékoone ci dior akh yaayam ? maquillage mougnui beug eup dé

    Pape Jean Paul Baligue DIOUFPape Jean Paul Baligue DIOUFMese fa
  • Idiote fille solen Mako abalone klk simili ma nokou KO mou bayi sèkh barame miskine😏

    la tivala tivaMese fa
  • Dior elle a des jolies yeux machallah

    Lativa AidaraLativa Aidara2 mesi fa
  • Ay ba maimouna naar douko faye mou deff fi dra bayilen di denkanei s'en keur di femme woroul

    Titi NguerTiti Nguer2 mesi fa
  • mais idiote mére c'est quoi son truc avec le parfum. toujours à s'en asperger .c'est du vrai parfum ou affaire de sorcellerie !?

    khadidiatou diakhadidiatou dia2 mesi fa
  • Ana niou guemoule serigne yi

    Babacar GmbBabacar Gmb2 mesi fa
  • Yama nak malgré c bêtises de mathie baram elle est adorable

    zeyna Diopzeyna Diop2 mesi fa
  • Yama tamit douniou maye djameu ak talon 👠 yi SO mounoul do mougne rek djapou yalla

    Fatou DjauFatou Djau3 mesi fa
  • Madior n'est pas vraiment sincère à mon avis

    Mariama BaMariama Ba3 mesi fa
  • Je ne comprend pas Madior, pourquoi il n'a pas dit à son papa la verité dés maintenant

    Mariama BaMariama Ba3 mesi fa
  • G l impression que Dior et madior sont des cousins

    ngara dioufngara diouf3 mesi fa
  • Yama yaw hamon fo Dieme

    Nene SowNene Sow3 mesi fa
  • Yama Mome menoul naturelle tamit cheuuu elle m'énerve

    maty kanematy kane3 mesi fa
  • Kou idiote Mére ak idiote fille soff like

    SOKHNA FATMA MOUSTAPHA MBACKÉSOKHNA FATMA MOUSTAPHA MBACKÉ3 mesi fa
  • Dit moi l'oncle de madior il détesté les femmes mai il n couch par avec keus

    fall kimflowfall kimflow3 mesi fa
  • Yama rew n'a sa tonton n gay wahh li ak tiofel bimu am ci yow

    dieynaba Diopdieynaba Diop3 mesi fa
  • Wa mei ki khana centenaire parfum lay am😅😅

    Ly AbdourahmaneLy Abdourahmane3 mesi fa
  • Ana gni prepare hadara tidianiya a stade amadou barry vendredi soir aparté de 17heures les 3 mai inchallha vs prépare

    Elhadj MalikElhadj Malik3 mesi fa
  • guanguan

    Mamah NdiayeMamah Ndiaye3 mesi fa
  • Mais yama loutakh mou tame sékh lokhom ich elle m'enerve nak

    le monde de mayale monde de maya3 mesi fa
  • Madior il joue a quoi 🤔🤔🤔

    Rama NdiayeRama Ndiaye3 mesi fa
  • Naar weroul srx

    Rama NdiayeRama Ndiaye3 mesi fa
  • I like this movie nice

    Njiez Million dollar ManNjiez Million dollar Man3 mesi fa
  • Mane deh suis totalement perdue avec ces liens de parenté flous

    Aminata NdoyeAminata Ndoye3 mesi fa
    • Wallah dou yaw kessé

      Mame Diarra Bousso MbayeMame Diarra Bousso Mbaye3 mesi fa
  • Cc yane jour lay ame mane khawma damay tatoner chak jour

    Ndèye Aminata MBAYENdèye Aminata MBAYE3 mesi fa
  • Kou beugue Tawhid beuseul j’aime

    Master AtlantaMaster Atlanta3 mesi fa
  • félicitation trés bien fait cette vidéo

    Théatre SénegalaisThéatre Sénegalais3 mesi fa
  • J'adore cette série c'est la meilleure des séries

    Khadiza DiengKhadiza Dieng3 mesi fa
  • Nice job ma beugu chéri bi

    Fallou ZiadaFallou Ziada3 mesi fa
  • 😂😂Mane dall Narre Diop layy weurr nekete elle jour trop bien Nenakoh diokhma 3millions mah diappal lh djiné rama Diop bi mouy dokhantou ci keur gui nakh gua nek nitt

    Dié layeDié laye3 mesi fa
  • Yama say bisous ak say rayy sincèrement eupna si Pa bi. Di toubab toubab lou rek, eupna nak.

    Monde CruelMonde Cruel3 mesi fa
  • Tonton Libass koulayii makille nekoiu mouu wagniii poudrée biii

    Aminata BarryAminata Barry3 mesi fa
  • Bilay ma diepiiiii borom parfum guou bari gui

    Nafissatou FayeNafissatou Faye3 mesi fa
  • Team dior

    Anna DieyeAnna Dieye3 mesi fa
  • ghen yaakar Yama dou moudié doxaan papou Madior? ish. ki nimouy raayé paabi nexna deh

    Conneries d' afriqueConneries d' afrique3 mesi fa
  • beugeu na yi

    Salimata SeckSalimata Seck3 mesi fa
  • Ani wa team Dior

    Aicha DrameAicha Drame3 mesi fa
  • Yama ake yayam rek gniouma soff

    Ndeye Amy DiakhateNdeye Amy Diakhate3 mesi fa
  • No yama bagn nala trop

    anen anenanen anen3 mesi fa
  • c est ce que font les filles elles maraboutent les hommes avant le mariage les hommes faites attention aux filles

    elhadji thiamelhadji thiam3 mesi fa
  • Thieuy nar ak yama

    Yebe SyllaYebe Sylla3 mesi fa
  • C pas une crittique mais juste une remarque. Je crois que Dior devrait se maquiller moins elle n a pas besoin de Toute cette couche sur le visage il faut quelle valorise son teint naturel et noir 🤔

    la vie et moila vie et moi3 mesi fa
    • El s makill trop tamit

      Ndeyefatou thiouneNdeyefatou thioune3 mesi fa
  • Dior way

    Sy DjeynabaSy Djeynaba3 mesi fa
  • Dior est très belle qui est d accord

    kadet djigokadet djigo3 mesi fa
  • Madior akh Dior esk dougnee ayy cousin.. cousine

    Djash KeubDjash Keub3 mesi fa
  • L

    seykou ndongoseykou ndongo3 mesi fa
  • Les enfants de fatou Ndiaye indo sont le papa de madior et les triplé dont la mère de Dior. Après l'oncle de madior kimou beteu ak kharitam bi c'est l'une des triplé c pour cela qu'il pense que la maman de Dior l'a trahis. En résumé yayou Dior ak papeu madior sont frère et sœur puis papou Dior ak yayou madior sont aussi frère et sœur 😂 may scénariste bi...

    MLML3 mesi fa
  • Démarche yama bi la menoul mougn man 😂 😂

    Diama  NdiayeDiama Ndiaye3 mesi fa
  • Les 3 jumelles: Narr maman de yama, marieme maman de dior, et la 3 identique à la maman de dior est celle que tonton de madior a vu à st louis avec son ami. Le tonton de dior et la maman de madior rama sont frère et soeur d'où la ressemblance de dior. Et qui prouvera ainsi qu'elle est bien sa fille. Sama ? Le père de madior est il issu du 1 mariage de fatou info ou est il le dit frère ??? Sinon rek aff d'inceste la niou am fofou🤪🤪🤣🤣🤣

    Adja NdiayeAdja Ndiaye3 mesi fa
  • J aime dior

    Asta SeckAsta Seck3 mesi fa
  • Da mélni dior ak madior gnio bokou yaye?

    Mamita aïdaraMamita aïdara3 mesi fa
  • Dior Ma Sha Allah ❤

    Bichette DiaaBichette Diaa3 mesi fa
  • Yow bagniala moytou sa parfum yi gay pousso dagay sodji legui ak allergie

    belle bellebelle belle3 mesi fa
  • Mais tonton Linas mo Aÿ com ivoirien ton bi c'est génial

    Salla SAMBSalla SAMB3 mesi fa
  • Idiote mère ak idiote fille merenalen trop

    la belle limashula belle limashu3 mesi fa
  • Bravo Le pére de madior joue bien son rôle.Il nous des leçons de vie

    Serigne Ibrahima DiopSerigne Ibrahima Diop3 mesi fa
  • Merci

    Ibrahima FallIbrahima Fall3 mesi fa
  • Machahalah mais Ndiaye teranga sa kourouss gui Kouko nass😂😂😂😂😂

    toulaye ngomtoulaye ngom3 mesi fa
  • Yayou dior nekh nama

    Thiatou KhadimThiatou Khadim3 mesi fa
  • Ohh la mère de dior Black N prOud😍❤

    Amina LoAmina Lo3 mesi fa
  • Mais Dior t trop belle machallah 😘

    Binta NdayrBinta Ndayr3 mesi fa
    • Machallah

      Binta NdayrBinta Ndayr3 mesi fa
  • Mais Madior ak Dior loune book ?

    alioune fallalioune fall3 mesi fa
  • Best serie .. who are agree with me??

    Khadidiatou KaKhadidiatou Ka3 mesi fa
  • 🤞

    mabma Ndeyemabma Ndeye3 mesi fa
  • Dior moudié na féminine hennnn

    Cheikh Ibra FayeCheikh Ibra Faye3 mesi fa
  • Team Dior

    Athia DrameAthia Drame3 mesi fa
Madior Ak Dior - Épisode 11 [Saison 01]